Gis-gis bi

twr360

TWR360 dafay faqas ñagi làkk yi ak ñàkka jote ci yenn xabaar yi ba jëfandikukat yi mëna sotti, siiwal te jàng resurs mejatik kereceen yu bare ngir màgg bés bu nekk ci seen ngem ci Kirist.

Misyoŋ bi

TWR360 dafay gena jox gedda niy jefandikoo appli Web ak mobil yi waaye rax-ci-dolli di gëna naatal sasi mejaa yu TWR360 ngir dimbali Jàngu bi ci sasam wi di yégleb xabaar bu baax bu Kirist :

  • Fexe ba ku nekk, fu mu mëna nekk ak waxtu wu mu mëna doon, mu mëna jëfandikoo, ci lu yomb te wóor, gëneeli kereceen yu yaatu yii ci wàllu nimerig, jaare ko ci ordinatër walla telefon, loolu lépp ci làkk wi mu nàmp bu ko neexee.
  • Jagleel waxkati kereceen yi bérëbu njàaay ci biir yees mëna jëfandikoo ci fànna yu bare ñu mëna siiwal seen jumtukaay ci weti yeneen sas, yu mag ak yu ndaw.
  • Li ko taxa jóg di nekk sit bu digg-dóomu bi ëmb katalogu poroparaam bu réy buy màgg bu TWR360 mu nekk lu ñu mëna jagle ànd ak ay emisyoni rajo, waaye du ànd ak lu dul teeyug bakkan cig jot ak ci bérab.

Mbirum TWR

Ñuy wax ci lu yomb lu epp 230 làkk aki làkk-làkkaat, TWR dafa nekk ngir jotal Kririst lii di àddina. Sunu yëngu ci jokkuwaayu xarala yi dafay laal lu ëpp 160 réew jaare ko ci dëggug biibal bi. Lu mat 60 at, Yàlla di may TWR muy dimbali nit ñi ñuy jóge ci xel-ñaar ba nekk ay taalibe.

Together with international partners, local churches and other ministries, TWR provides relevant programming, discipleship resources and dedicated workers to spread hope to individuals and communities around the globe. Whether using high-powered AM/MW, shortwave or FM radio, streaming content to Internet users or visiting face-to-face with listeners, TWR leaves a lasting spiritual footprint.