Lu yemmook
Ndax mos ngeen a am xel ňaar ci mbëggéelu ku tekki lu bare ci yeen? Ndax mos ngeen a jéem a firndeel seen mbëggéel
ku ko bëggula gëm? ci fann bi walla ci fann be, dingeen xam ne saa yo xam ne ngir woone seen mbëggéel Jëf moo gën a mën a wone seen mbëggéel ka ay wax.